#Ano_1087_Sdsk_2020

Salam Tata Habibi ❤ je veux passer en Ano stp
Je veux rendre hommage á mon mari.
Je suis une fille de 22ans mariée il ya an avec un homme de la trentaine trés gentil, am diné, am yeurmandé défois damay lire yén Ano yi si groupe bi et je me demande mane si bane genre nittt la dal . Ko khamni dou khaar ma wakhko lima beug, il suffit mou deviner ko rekk tahaw ssi . Un homme extraordinaire dima défendre fepp naq, dou bayi kén dima wakh louma metti sen keur . Ko khamni si je me sens mal meunoussi dara sah mou diakhlé. Je ne manque de rien, ko khamni souma yéwo nekk si wagne bi sah souma nieuwé fekk mou défar negg bi ba tookk . Maintenant je suis enceinte mossi raw mangui tolou si 5mois chaque jour momay défaral ndekki, tokk sama wett bama lekk baparé, il débarasse rahass tasse yi souma wakhé sah mou merr. Si biir keur gui, si mbedd mi founiou nekk kom ay moroom foniou fekk niongui rétaan, dakké lounekk laniouy deff je ne me rappelle pas biss bouniou dioté ba goudi mou wanema guinaaw, ak lou meun am il se léve dem diouli nieuw il me prend dans ses bras niou teud nélaw meussouma diappal dara meussouma wakh louma metti khalélaa certes mangui soga dougou si seuy mais dofouma yalla dimbali nama naq ba diokh naako thieur bimou yélol moy sama lepp sama kharite sama confident sama lepp mom lakay wahh doumako neub sama dara ... je ne pouvais pas rêver mieux cet homme est un ande il répéte toujours SOUMA NARÉ NANE NDOKH KHALATE NI DAFLAY METTI SAH DOUMAKO DEFF té nonou la deuké ak mane, oubil nama bopam bama miine ko té yakoussi dara. On a des hauts et des bas comme tous les couples mais jamais mou fégne souniou kaw lale il me l'avait promi té sila nekk batay je me dis que mingui melni mom mo wara seuy seuy bi, ddaniouy dioté sah wakeur gui ken douko kham ndakh souniou biir negg lay yam, dagay merr bama khamko mais soutoural nama ba kén douniou khamal dara . Lén rekk la sokhla mouy ay niaane namako nieup nianalal khamouma bane guémigne mo am barké limay dounde niémé woumako nétali kén ndakh amana meun naniou diappni dafa niakk fayda sama mame rekk lakay wahal moukay niaanal et personne d'autre . D'aucuns diront que dama téla wakh mais noon khamanté naniou depuis 6ans nii la meuss mel ak mane . Mon Amour je rends grâce á Dieu de t'avoir mis sur mon chemin ay mane soumala amoul wone foumakay wakhé. Sigguiil ngama, saggal ngama, diapalé ngama , tahawou ngama si lepp si diiné dji, si sama diangue ak lepp yalla naniou yalla sameu mousseul niou si thiate ak lamigne ta OUROUL AYNI t'aime énormément . Tata louma wakh rekk amna lou dess bilaahi walaaahi il m'arrive may djoullli di niaane bay diooy parceque je me dis que je ne mérite pas cet homme ak fima diaar yeup mou deug si takam ndakh beug ma bamou diéhh beug maa diapalé yalla nako yalla sameu Rajulul Janati❤