Ano_1511_Sdsk_2020

Bonsoir madame merci de me publié en ano svp

Je suis un jeune homme de 26ans marié à une femme de 24ans et père de deux enfants sama diabar djiguéne geunouko bakh ,yarou ,yatou,yime ame yeuremandé ,tabé guoré louma ame ak louma amoul kéne khamouko yalla nako yalla déli diame mais le seul et unique problème est que diongué zéro la nuit dina sol nuisette you bakh mais silay yame 5ans de mariage masouma provoquer mane rék may déme di thiokasse après on le fait et lolou dasamasi sone défoi on peut rester 2 ou 3 semaine sans le faire et mane dama beugue djiguéne bou bandit si bir nék (chambre) . conseil la beugue noumay déf bamou changer . merci