Ano_1513_Sdsk_2020

Mane daal mon seule et unique problème moy sama poids je suis très très grosse et ça me dérange. Je suis une femme mariée avec des enfants, meuna touma ande ak mol fén, sama dieucoeur dafa sakh decouragé si man té nak c'est vrai nima dieulé poids dafa eup en si peu de temps, ndakh pata méti na ma troppp, hier daf khass bamay dioy ndakh sama yaram bi meunou ma régime par ce que damay nampal svp aidez moi svp.