Ano_1521_Sdsk_2020

Bonjour tata svp publie moi en ano ofète c ma première publication sur cette page 1 jour javé 1 amie ki avé fait son post à travers mn compte mais ojordui je meforce à vous écrire avec le coeur meurtri. Je suis 1 jeune fille de 28 ans travaillant dans 1 société de la place avk 1 bon salaire alhamdoulilah mais mon problème est que je suis née avec des déceptions chez ma famille mes amies mes collègues les aventures amoureuses etc.Ma relation avec tt le monde ne dure pas et pourtant g 1 bon coeur machalah je partage tt ce ke je gagne avk tt le monde le seul défaut ke je peut me reprocher c'est juste que je n'oublie jamais le mal que l'on me fait . Donc depuis 2011 je fréquente les marabouts avk ma famille mais en vain fou nekk la dem pr fajou mais dara même hopital aussi rien amoul louma fayoul serigne pr mou dimbalima damay dem saxx ba niéne si serigne si dima khiir si séne bopp wala nane ma souma jeulé sama awra bi tekko sisa boss sa rap bilay yakal sa adouna bayila dound nako 4 fois xaliss bi nakk je n'en parle mm pas . légui limay niane moy louma waay meuna conseil wala kou xam ko xamni amna yakaar ni souma japanté ak mom mou fajma sans thiakhane wala naxaté ndax li nekk si mane sonal nama trop teh bimou dallé yakk sama dound yaguena.Tay jii amna liguey mel nima wara mel machalah et nitt yii douniou bayi dima waxx ya begoul jeukeur mel ga niga wara mell amga liguey am ga xaliss loutax gay am problème et le plus comble bcp ne cesse de me dire so amé jeukeur sa problème jeex alrs ke copin saxx awmako sa fait plus de 1 an et kelk maintnan soxla na conseil ak nimbeul kou beug jabar aussi suis prête mais pas kou beug lou yomb je travaille certe mais je veux 1 responsable kom moi.