Ano_1579_Sdsk_2020

Salam tata Habibi. Il se trouve que j'ai remarqué une certaine divergence entre les maris et leurs epouses. Si on l'analyse plus loin, ce n'est qu'une différence de conception et de vision du mariage entre l'homme et la femme et chacun attend de l'autre ce qui est Supérieur à ses capacités. Il est alors temps que l'on définisse des règles du mariage que je vais appeler ici des piliers. Je donne juste mon avis et lance le challenge à tous les membres de SDSK pour que chacun(e) donne sa conception du mariage, que l'on en discute. Peut-être que les couples présents dans cette plateforme pourront s'y inspirer pour avoir une vie paisible.

Pour moi, le mariage repose sur 6 piliers dont chacun énonce l'autre, formant un ensemble imbriqué et stable et que l'absence de lun d'entre eux déstabilise le couple. Cela montre toute l'importance que tous ces piliers representent les uns des autres pour un COUPLE HARMONIEUX.

1er pilier : #YEURMANDÉ

Na kounékeu yeureum moromam. Soxnaci yeureumal serigne bi si dépenses yi, nga yahanalal Koko. Serigne bi yeureumeul sokhna ci si liguéyou keur gui, nga diappalékoci parfois ak si gestion xaléyi.

Sa borom keur war nga xam loumou meun ak loumou meunoul nga yémalé say beugeu bou fékké liguéyo. Boy liguéy nak, diappaléko si yéneu dépense yi ta Yallah rékeu tah ak ndiaboot gui. Yallah moy fay. Yaw kou gaur ki boul hol moukkeu li sa diabar di am. Déko diokh ndakh djiguén djilay dioural, ak ni eumbeu metté, loko défal diarnako ndakh dome banékh la, Diarna louné.

2e pilier : #WAHTANE

Ak lou mana am wakhtané lénko. Serigne bi sa sokhna, loy dougou demander koci conseil, boul ko neubeutou. Loula metti si mom wakhtan si ak mom si dal ak respect. Sokhnaci, lolou yawit nonou nga war di dohalé. Boulén di youhou wanté aka geuddanté, aka khastanté, aka sagawanté nguir Ndiaboot gui barkél. Wormalanté lén.

3e pilier : #WORMA

Na kounékeu respecté moromam. Sokhna ci na sa borom keur done sa serigne, sa sangue ta nga tarbiyou ko. Serigne bi, amal foulla ak fayda ta bagna REUY, tay djité sa sokhna wakhtou dioulli. Ngén bayyi wakh you séw tay soutouralanté. Boulén du houlau si kaw nieupeu di dégeu.

4e pilier : #SOUTOURA

Na nguén soutoura lanté. Sa borom keur bou kéneu xam loumou manké, bou teulé (ndigeu wala poche) soutoural ko ba kén dou xam. Yaw serigne bi soutoural lal sa sokhna si ay gakeu gakeu. Akay matadi parfois wayé nonou lala beugué, dioubantil ndankeu ndankeu ta mougnal ko.

5e pilier : #MOUGN

Mougnalanté lén ndakh nit si bopam mo matoul. Sokhna ci, say défoy borom keur féhél ba dindi ko si mom si di wakhtane ak mom, diko motchieu ndankeu ndankeu bagn dici houlo ak mom balay guiss bopam. Yawit serigne bi sokhna Boko takké, fékeu ay djikko si mom, youla néhoul, boul découragé, dangakoy yarate si say principe lépeu di mougnalé ndakh garab bou dém ba mageu néhoula dioubanti. Nit ki Boko beugué, war ngako mana mougnal louné tay mottali wanté si dal, si respect, si mougn, si wakhtane, si yeurmandé...

6e pilier : #MBEUGUÉL

Mbeugél amna solo trope si diganté mari et femme. Motah meme sil ya désamour, l'époux tout comme l'épouse doit consentir des efforts pour rallumer la flamme entre eux et ceci via la communication, wakhtan, poser le problème et le résoudre.

Niou bari danio yakaarni mbeuguel rék mo wara takh nga seuy ak nit ki yakaarni kouniou beugoul warou niou seuy ak mom. Oh que siii. Boulako Yallah natto nangouko, déf lép mou rafét. Pour mane sakh seuyyak nit nguir djikom you rafét mo eupeu dolé seuyak nit nguir nobel. Or on dit q gaur bou beugoul rék beugoul. Pourtant l'amour se cultive. Eeeeh oui. Apprends à aimer la personne que Dieu t'a destiné pour l'amour de Dieu, diamouci Yallah. C'est lui ou elle que Dieu t'a destiné. Accepte la ou le et cultive l'amour entre vous. En refusant cela, et en te comportant de manière négative, tu compromets ton bonheur, tu déstabilise ton foyer, tu t'emprisonnes dans ta propre prison. Simulez l'amour, comportez vous comme des êtres follement amoureux, faites les choses que les amoureux font, kéneu kouné na concentré wou si moromam di khol likoy bégeul moukoy déf, fattél Tioro wala modou binga dadiél dans ton passé, liguey la si sa biir khél ak si sa khol, sheytané molay diéma déstabilisé dila geum loni boudoul ké do am banékh. Tu va le laisser faire ? Bats toi contre lui et récupères ton esprit pour qu'il ne te manipule plus. Na kéneu kouné di khol li positif si sa morom ta bagn di focalisé wou si li négatif ta diapeu ni mission la si yaw pour changer nit ki bamou am djikko you rafét. Pour mane diamou Yallah la meun nani sakh djihad nafs la. Féhél ba kila Yallah bolél doula geumé. Wahouma si ndjibar dé, wayé si tahawouko, si yeureum ko, si soutoural ko, si wormal ko, si mougnal ak, si topeuto ko, bayyiko xél si lép loy déf.

A mon humble avis, si tous les couples fonctionnaient sur la base de ses 6 piliers, il y aurait moins de souffrance, moins de violence, moins de divorce.

Et toi quelle est ta conception du mariage ? En ano ou en commentaire ?