Ano_1728_Sdsk_2020

Salam.

Sénégal dagnou am habitude bougnouy takke seuyy, kelk personnes gnookoy dokh fass ko, gnissi dess moom...amougn si baat. Perso je ne suis pas d'accord. Moo takh dès fois amkou seuyi si keur, nga yegu né ndekété Rapp leu bou dioukh si ay nitt.

Sama belle sœur dafa mané kerook liyy dagg seu kholl bi mooy lingamay guiss may deff té meunoo si touss. Boudé dangay marié pour beug dagg ay khoolou nitt si dieuffou maa tayy AK pekhé je pense que diaratouko.

Damay deff situation ngueen comprendre :

Famille bi fékhé neu beusseu diéukeur fayoul ndokhak courant té dieundoul thieep.

Bousseen doom febaré nitt gneey yobbou hôpital dieund ordonnance topatoo.

Seu frais de scolarité doom, fournitures, goûté, blouse d'écolier... durant tout un cycle beu examen, kenneu si famille bi mooko dieul en charge à coup de centaines de mille francs par an.

Meussougn leu door, khass, saaga, gnaan khaaliss wala yeuré...

Lii yeup bouleuko famille defaralé noppal naleu. En retour loo leen wara defal loudoul yiww                    </div>

                    <!--Optional Url Button -->
                    
                    <!--Optional Url Button -->
                    
                    <div class=