Ano_1943_Sdsk_2020

Bjr tata Habibi merci pour le travail util et serviable que vous menez dans cette page et qui nous permet d'interagir entre nous et de voir les autres faces de la société en plus de notre vécu.

Mane nak jigen yi dieul à cœur l'infidélité de leur mari bamou beugue léna yakhal sen adouna wala sen seuye nioma takha binde msg bi. Kham Lanla beugue ame len sen foula ak sen fayda ba maîtresse doulen téré happy wala mouy déstabiliser sen foyer bagne len lolou. Moi même j'ai été victime de l'infidélité de mon mari mais bimako ndieuké diap je pensais même au divorce après sila demandé conseil sama petite mouné boulko wakh dara mais boko diapaté néko so yakaré ni dokhane dinama takha tasse sama seuye wala ma nek fi di stressé wou nakh nga sama bopou. Nonoulako défé dieul sama boutique confier KO sama soeur tok sama keur di seuye sama seuye topato samay dome mom nak bou guéné sama yoon nékoul si limouy def mais bou dougou sé si keur gui dinako topato bamou khamni gnak diomame motakh mouy rassatou dji si biti mais dou gnaka falè. Un jour mouné ma damay tak deuxième femme maniko amoul ben problème deuxième bi seuye si guiss ma nima mel ak sama dieukeur si bir keur gui ndakh dama fékhé ba done xarit done yayame done rakam créé ben complicité bou extraordinaire bamou dem sakh ba ame kersa sama dingaté ak mom wayé deuxième bamou démé ba meunatouko supporter tasse la def dem yoname légui nak mom sama dieukeur récupérer wat nako sans tambour ni trompette magui tok di seuye nice makoy bégueule moumay bégal machalla yalna sakh.

Nb guiss ngen goor nioussi bari ken meunouléna téré dokhane mais iow miye diabarame fékhel ba done seytanéme et sa finalité meunena def tour du monde mais tjr yaye nek son point d'arrivée té lolou moye solo si.

Bonsoir svp est-ce que vous pouvez poster mon texte pour redonner le moral à toutes ces femmes dont leur mari est car c'est vraiment quelque chose de dure et aucune femme ne mérite cela et sa ne doit être une raison pour elle de briser leur foyer. Je compte vraiment sur vous