Ano_1946_Sdsk_2020

Salu publié moi sa ano enfait daama ame coepouse mai dalll so comportement envers moi dall moma khawa diakhal parsek mane defoumako wakhoumako maii meunouma supporter té pourtant lignouy guissanté bariwoul sakh ndakh bougouniou founiou nek Sa soumako degué mako wo ladjeko khaleyi silouniou nek mai lepou siii rafetal ma dem ba sone bayi appel yiii tok diko setane mom wowouma lidieunetilwoul sila nek legui diimbou sii goudi mou wouté sisa telephone dieukeur fek sa dieukeu dem entraînement nima telma sama telephone kou woté neko dama dem salle dsport ndéketé da abbou telephone pour wo dieukeur djiii sinon mane khamé na numerom mani allo rek mounima ani borom téléphone sans pour autant mou nouyou ma apres maniko da guene mou coupé mai mane topou mako siii dara ndakh dama diapouni rek khelam mon tolou nonou emplus sante na yalla boubakh ndakh avant tabaskibi sama niariii kharitou dieukeur danion takk diabar mayma premier gneké biii té pourtant mom momafiii djitou té gnognou mom lagn gneka kham ndakh momafiii djitou . Sest la premièr foi may pubier conseil la beugu ndakh aparsa sama dieukeur owma benen kharittt