Ano_1947_Sdsk_2020

slt Tata dimbalima publier ma nguir dieumi seydina mouhamed man sama borom keur dafa tak 2 femme mou niew passe fi ak nioune si keur famille bi une semaine man ak Amna ak mom Ben dome mais mr dale dafma ignore completement fallewouma lidiantiwouma sou guene sakh di den douna tagou sougnou togue nioune 3 mom lay wakhal melni comme si dafa diote ak man ba nimouy gnibi mom europe la nek legui nak demna wowouma yonewouma mais man tam wowoumako dama tok diap sa ma ndiambour dama beugone ngen conseille ma bakham lanla wara def deja le 20 moy sougnou 06 ans de mariage Tata diap si nguir yalla