Ano_1952_Sdsk_2020

Cc tata merci pour le travail remarquable je veux divorcé mais ma mère et mes enfants dans tt ça ?

Je m'explique tata suis marié avk un homme irréponsables bo khamne khamoul teral djiguene bokougnou Dara nak gno guissante beuguante il était super tt le monde Parler de notre couple gneup pask qu'on s'afficher comme un couple parfait il montrait son amour partout mm ces amis me disait sa dieukeur beugue nala foumou togue sakh wakh l'ay wakh sa maman son frère ces tantes gneup mounouma wax sene djiko lolou yeup graoul may mougne il était dans une autre région Di liguey ndeke ces parents chaque jour ils l'appelle pour lui dire sa diabar li ou la mou dieki rek bayima wowatouma gnewatoul defatoul Dara pendant 6 mois te mangui sene keur j'ai appelé son demi frère expliquer KO la situation et son ami ils l'ont appelé déplacer wou gneuw tadie KO Moune ces parents gnoko wax sa diabar bakhoul mais Dina diema def effort

Depuis bobou ba legui ça fe 4 ans ça devient pire je l'ai rejoint si région bimou nek avec mes enfants mais Mr sou yore khaliss rek bar yi il rentre a 6 h du matin bilahi nonou lakoy diape bala le 15 dotoul yor deureum founek Mouy wote Di leb c'est lui qui gère la location aussi des fois yenen locataire yi fayko mou dem nan lep, il voit de l'alcool, di dakhante ak borom keur gui dama rouss walahi dite moi face a cette situation qu'est ce que je dois faire svp may taw warone diapale sama yaye situation bi takhena mounouma def sone na trop beugue na seuy ndakh samay dom mais situation bi metina excusé de la longueurTata diap si publiel ma sama ano conseil rek la beugue avant de prendre une décision