Mane dama sonn je cherche un mari

Mane dama sonn je cherche un mari

Salut wa sdsk.

Mangui noyou nieup di niane aye conseil. Au fait mane dama nekone France ma am copain bou nek italie. Wadji nak on sortait a distance. Guene bi neikhone torope. Te comme amouma papier je ne pouvais pas travailler en france du cout jai decidé de retourner sur litalie comme fofou la nekone avant ak sama famille. Bima gnibisé nak mane ak khalé bou goor bi niou continué di guene bamou nema nako presenter sama famille. Je lai presenter ma soeur et ma mere mou wakh ak niom liko yeukeuti manam sokhna leu beugue . Mom dou nitou thiakhane . Mais comme il travail du lundi au vendredi chak samedi il passe me prendre a la maison niou deme keureume tokh wakhtane togantou ak niom sene . Mais jai remarké k mom il veu pas venir a la maison me voire . Bimako repoché lolou nak mou mer diarefa bayima . Il ne me parle plus té comme khamnanai dama khawa susceptible mani djiguene dou reuye ma woko niko nama bal mounima waw mais depuis lors wowouma bientot une une semaine . Comme dama ko binde message traiter ko de tous les nom neko peut etre danga done fene tu voulais la facilité .hier je lai appelé falewouma . Bon je demande juste des conseils. nga tol si seuye te souyo dafa meti. Sa morome yeupe seuye nieup am done . Mane sama yaye daf ma tardel ak affairi guer ak geweul. Mane nak dama sone je cherche un mari kou dioulité te di out sokhna aussi . Je precise je suis en italie de preference kou nek italie . Dama beugeu am ndibote té yonne bou bakh lako beugeu amé .