no_1944_Sdsk_2020

Cc cva stp esk meune ngama defal li ano stp

Manedé daffa am louma dal legui si sama diguanté ak mon mari on a fait 03 ans ensemble mashalla mou metiwone trop nak nakh seuyou koudjéla ame ay clans avec les belles sœurs et belle-mère mais tjr damay khekh pour gardé sama seuy démone nagne ba monté mon mari contre moi wakh bou nekh sakh meunoumako am si mome franchement bou ayéwane si Mane sakh daye takhawalou ba heur bouka nekh ainsi bou gneuwé ma nek di khoulo ak môme wala bouniou néké si euteu bi il suffit ma wakhko bene phrase rk monsieur djanima insi thiowli tambaléti ak yénéne youma meunoul nek fi di wakh djoyna ba sama djoyoukay djekh. mais legui dal g remarqué k ni meunatouma def Dara damou nakharima firétoumako et pourtant je sais k legui dafay dokhane nakh sama woudjoubi djap nako nieuw def scandale mais bizarrement Mane derangewma sakh bima néké di arrangé pr Mme tok lama khamalni monsieur daffay dokhane. Je lui ai juste dit k lolou djaroul thiow wala dinane dagay mere bayiko rk pochame mofay dess ak dolém plus ay douma euleuk parési. Mane batey metiwma et prtan j sai pertinemment kil fait se kil veut Mane nak indifférence bima am a son égal moma djakhal meunatouma def Dara Dara bamou nakharima dafmay djani légui bou paré douma téré wakhtane ak môme kaf ak môme. Legui nak néna beugatoumako nakh soumako beugone dina continuer dikoy firé. Nakh bima wakhtané ak sama woudjoubi ba paré j'ai just demandé à Monsieur nakh môme talna dokhane ak charge yimou yoré yeup il m'a répondu non ma parési et je sais k dafay fenne puisk nak defouma bene réaction contre ça lolou motakh mouni beugatoumako.

Legui mes chers louguene khalate si sama cas Mane esk indifférence bima am si mome dou yague sama seuy et pourtant ma warone di fiir ak di guestou nakh mane la moudjé tak té amagouniou sakh dôme.

Merci