#Suivi_de_Cas

Bonsoir Madame je voudrais faire une publication en réponse à l'#Ano_1009 svp, je suis sa coépouse. 

Je ne suis pas vraiment fan de Facebook et je ne m'y connecte que très rarement et mon mari non plus n'en fait pas un centre d'intérêt, mais ma belle tu as donné trop de details, même les personnes qui nous fréquentent sauront que c'est toi et que tu parles de moi.
 
Ma belle sœur qui suit cette page m'a montré ce poste pour me demander si ce n'était pas de nous qu'il s'agissait. Ça m'a fait énormément de mal et si je décide de te répondre ici c'est pour te rassurer et t'éloigner de toutes ces personnes qui te demandent de divorcer. J'aurais pu en parler à notre mari et je ne pense pas qu'il apprecierait voir sa vie privée exposée sur facebook. Je ne lui cache rien d'habitude mais li soumakoko wakhoon meune na indi thioow té kenn meussounio dégg ci lou mel nonou. Je ne veux pas non plus qu'il ressente la douleur et la surprise que j'ai ressenti en te lisant. 

Tu sais autant que moi que notre mari goor geunouko té koula beugg la. Mane tamitt soudé danga niaaw ndiort ci mane khamalni Wallahi meussoumala yéné lou bone té meussouma diogg di dem ci Serigne pour sama dieucoeur beugg ma. Kou seetlou nak guiss. Tous les détails dont tu parles ce n'est nullement pour te faire du mal wala dila kokali, loin de là. Il aurait peut être voulu avoir le mm comportement envers toi mais ta timidité meune nako freiner ci yenn yi, mane mom ymgx je suis très free, souma diéguéwoul sakh makoy fekk fimou toog diko wakhlo di kaffak mom. Lolou diapé woumako mouy dara prck c'est tout à fait normal et c'est ma nature. Je ne savais pas que ces petites scènes te faisaient tellement de mal bamou diaral la nga diko wakh fi. Yaakaaroon naani amnga esprit de dépassement et qie niniou mel waroula jakhal puisque sunu kharito dara oumpoula ci té  même en temps qu'amis on était comme ça. Sunu Borom nak moniou nattoo mbeugueel dabb niou ci, on s'est menti à nous même et beau faire semblant de rien par respect pour toi mais dafa am lo khamni nékhoul neubb, c'est venu accidentellement et ça nous a dépassé. Méti woon na ci mane ak mom lool ndakh beugouniou woon trahir sa confiance, on a fait bcp de sacrifice pour contrôler ces sentiments qui naissaient en nous. Notre mari nak goré ak deuggou rék motakh mou takk ma prck meunone nagn di nekk dilako neubb té dooci kham dara. Mbeuguel mo doy waar rék waayé dou tayeef. 

En mon nom et en son nom, mangui lay diégalou ci bepp metitt boumala tegg. Dina diéma canaliser yeuf yi wakhtaan ak mom nanditément pour plus de discrétion té louma meune pour rapprocher leen dinaako def prck lima yéné sama bopp rék laala yéné. Na sa khel dall je ne lui dirai pas tout ceci, niofar té da melni khamo lolou.... Soumala tognaté amnga sagn sagnou nieuw ci mane sermonner ma. 
Certes Keur gui mom soufi Bour doon am Sunu Chéri lay doon, waayé ninga doon Awo nangoulnaala  nga doon Bourou Keuram, yowitt nangoul ma ma doon Kharitam. Leppp neéekh. Nga baalma akk

PS : waa diankk ngani yaama geuneu jongoma iow